bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 19:1
Acts 19:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ba Apolos nekkee Korent nag, Pool jaar ca teggi ya gën a kawe ca réew ma, door a dikk Efes. Noonu mu gis fa ay taalibe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Diir ba Apolos nekkee Korent, Póol a nga jaare ca diiwaan yu tunde ya, ba wàccsi Efes. Mu daje faakay taalibe,