Acts 19:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu wéy ci noonu diirub ñaari at, ba ñi dëkk diiwaanu Asi ñépp dégg kàddug Boroom bi, muy Yawut muy Gereg.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu moo wéy diiru ñaari at, ba mboolem waa diiwaanu Asi dégg kàddug Sang bi, muy Yawut, di Gereg.