Acts 19:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu nit ka rab jàpp song leen, noot leen ñoom ñépp; mu soxore leen lool, ba ñu daw kër ga, def yaramu neen te gaañu bu metti.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu nit ka rab jàpp song leen, teg leen loxo ñoom ñépp, pamti-pamtee leen, gaañ leen, ba ñu dawe kër ga yaramu neen.