Acts 19:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne leen: «Ndax jot ngeen ci Xel mu Sell mi, bi ngeen gëmee?» Ñu tontu ko: «Déggunu sax ne, Xel mu Sell mi am na.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ne leen: «Ndax ba ngeen gëmee, jot ngeen ci Noo gu Sell gi?» Ñu ne ko: «Nun de yégunu woon sax ne Noo gu Sell gi am na.»