Acts 19:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu yebal nag ci Maseduwan ñaari jaraafam, di Timote ak Erast, waaye moom mu des ab diir ci Asi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu daldi yebal fa Maseduwan, ñaari jaraafam, Timote ak Eràst, moom mu toogaat ab diir ca Asi.
Recommended Reading