Acts 19:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu dajale leen ak seeni liggéeykat ne leen: «Gaa ñi, xam ngeen ne, sunu njariñ mu ngi aju ci liggéey bii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu woo leen, ñook ña farewoo liggéey yu ni mel, ne leen: «Bokk yi, xam ngeen ne liggéey bii, ci la sunu teraanga nekk.