Acts 19:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi kat loraangee ngi nuy yoot, te du yem ci xañ nu sunu liggéey rekk, waaye it dina daaneel màggalukaayu Artemis sunu yàlla ju mag ji, tey neenal ndamam, moom mi Asi gépp te àddina sépp di màggal.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu, jéllale naa ni mu mana gàkkale sunu liggéey bii, waaye dina tax ñu teddadil jaamookaayu Artemis, yàlla ju jigéen ju mag ji, ba darajaam mujj neen, moom mi mboolem Asi ak àddina sax di jaamu.»