Acts 19:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Pool nag bëgg a dugg ca mbooloo ma, waaye taalibe ya nanguwuñu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol nag bëgga teewi ca kanam mbooloo ma, taalibe ya bañ.