Acts 19:37 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte nit ñii ngeen fi indi sàccuñu ca màggalukaay ya te sosaluñu sunu yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax nit ñii ngeen fi indi, teddadiluñu ay jaamookaay te waxuñu lu ñàkke sunu yàlla kersa.