Acts 19:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su fekkee ne Demetirus ak ay nawleem jànkoonte nañu ak kenn, am na ay bési layoo ak ñu yilif réew mi; nañu fa woo ku ñu amleenteel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee Demetirus ak liggéeykat yi ànd ak moom ñoo jote ak kenn ci ñoom, ay ëtti layoo am na fi, ay kàngam a ngi fi di àtte. Nañu fa layooji.