Acts 19:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Pool ne leen: «Yaxya daan na sóob nit ñi ci ndox, ndax bi ñu tuubee seeni bàkkaar; te mu ne bànni Israyil, kiy topp ci moom lañu war a gëm, maanaam Yeesu.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ne leen: «Yaxya, sóobeb tuubeel la daan sóobe ci ndox, di waxaale askan wi ne leen ñu gëm kiy topp ci moom, te mooy Yeesu.»