Acts 19:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte fi mu ne man nañu noo jiiñ jógug mbooloo mi ndax li fi xew tey. Te bu loolu amee dunu am aw lay ci mbirum mbooloo mu rëb mii, ndaxte amul dara lu ko waral.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat repp nanu ñu jiiñ nu ag fippu, te amul lenn lu nu mana lay, ba lewal mii ndaje.» Naka la wax loolu, daldi tas mbooloo ma.