Acts 19:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te bi leen Pool tegee loxo, Xel mu Sell mi ñëw ci ñoom, ñuy wax yeneeni làkk, di wax ci kàddug Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba leen Póol tegee loxoom, Noo gu Sell gi dikkal leen, ñu tàmbalee làkk yeneen làkk, boole ci di biral waxyu.