Acts 19:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Pool dugg ca jàngu ba, di wax ak fit wu dëgër diirub ñetti weer, di diisoo ak ñoom ci mbirum nguurug Yàlla, di leen jéem a gëmloo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Póol dem ca jàngu ba, diiru ñetti weer muy waaree aw fit, di waxal waa jàngu ba kàddu yu mata gëm ci mbirum nguurug Yàlla.