Acts 2:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi bésu màggalu Pàntakot agsee, ñoom ñépp booloo nañu ci benn bérab.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba bésu màggalu Pàntakot agsee, ñoom ñépp a bokk daje benn bérab.
Recommended Reading