Acts 2:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñépp waaru, ba jaaxle lool, ñuy waxante ci seen biir ne: «Lii lu muy tekki?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñépp waaru, ba jànnaxe, di wax ci seen biir naa: «Lii lu muy tekki nag?»