Acts 2:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit ñii màndiwuñu, ci ni ngeen ko fooge, ndaxte nu ngi ci yoor-yoor rekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñii màndiwuñu, ni ngeen ko fooge, ndax yoor-yoor doŋŋ a jot.