Acts 2:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
“Yàlla nee na: Ci bés yu mujj yi,dinaa tuur ci sama Xel ci kaw nit ñépp;seen xeet wu góor ak wu jigéendinañu wax ci kàddug Yàlla;waxambaane yi dinañu gis ay peeñute màggat yi di gént ay gént.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
“Yàlla nee: Mujug jamono, maay tuur samag Noo ci kaw wépp suux; seeni doom, góor ak jigéen di biral waxyu, seeni xale yu góor di gis ay peeñu, màggat ñi di gént ay gént.