Acts 2:24 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Yàlla dekkal na ko, daggal ko buumi dee, ndaxte dee mënu koo téye.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye moom la Yàlla yiwee ci mititu ndee, dekkal ko, ndax dee amul kàttanu tënk ko.
Recommended Reading