Acts 2:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yonent la woon, te xamoon na ne, Yàlla digoon na ko ci ngiñ ne, dina teg ci nguuram kenn ci askanam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye yonent la woon, te xamoon na ne Yàllaa ko giñaloon ne ku bokk ci geñoom lay teg cib jalam.