Acts 2:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte du Daawudaa yéeg ci asamaan, waaye moom ci boppam nee na:“Boroom bi wax na sama Boroom:‘Toogal ci sama ndeyjoor,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat du Daawudaa yéeg asamaan, waaye moom ci boppam moo ne: “Boroom bi daa wax sama Sang, ne ko: ‘Toogeel sama ndijoor,