Acts 2:39 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte li Yàlla dige woon, yéena ko moom ak seeni doom ak ñu sore ñépp, di ñépp ñi Yàlla sunu Boroom di woo ci moom.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax dige bi, yeen ak seen askan a ko moom, ak jaambur ñi féete fu sore ñépp, mboolem ñi sunu Yàlla Boroom bi woo.»
Recommended Reading