Acts 2:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu fees ak Xel mu Sell mi ñoom ñépp, ñu daldi wax yeneeni làkk, ni leen Xel mu Sell mi maye, ñu wax ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom ñépp nag feese Noo gu Sell gi, tàmbalee làkk làkk yu wuute, na leen ko Noo gi manloo.