Acts 2:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu mu artu leen ak yeneen wax yu bare, di leen dénk ne: «Rëccleen ci niti jamono ju dëng jii.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeneen kàddu yu bare soññe na leen ko, ñaaxe leen ko, ne leen: «Muccleen ci gii maas gu dëng.»
Recommended Reading