Acts 2:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
di màggal Yàlla te am yiw ci wetu nit ñépp. Noonu bés bu nekk Boroom bi di yokk ca mbooloo ma ñi mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñuy màggal Yàlla, ñépp naw leen. Bés bu nekk nag Boroom bi di yokk ca mbooloo mooma, nit ña jota mucc.