Acts 2:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk booba amoon na ay Yawut yu daloon Yerusalem, doon ay nit ñu ragal Yàlla te bokk ci xeeti àddina yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba ay toppkati yoonu Yawut a nga dëkke Yerusalem, te bawoo ci xeeti àddina yépp.