bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 20:1
Acts 20:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi yengu-yengu ba dalee, Pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. Bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu Maseduwan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba yëngu-yëngu ba jeexee, Póol daa woo taalibe ya, ñaax leen, ba noppi tàggtoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu Maseduwan.