Acts 20:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Pool fasoon na yéenee teggi Efes, ngir bañ a yàgg ci diiwaanu Asi; mu ngi doon gaawantu, ngir màggal, gi ñuy wax Pàntakot fekk ko Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax Póol daa fasoon yéeney teggi Efes, ngir baña yàgg diiwaanu Asi; booba day gaawtu, ngir màggalu Pàntakot man koo fekk Yerusalem.