Acts 20:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu jaar ca bérab yooyu, di dooleel nit ñi ak wax yu bare; ba noppi mu dem réewu Geres,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee mu wër gox yooyu, ñaaxe gëmkat ña kàddu yu takku, doora dem réewum Geres.