Acts 20:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam naa rekk ne, ci dëkkoo-dëkk Xel mu Sell mi xamal na ma ne, ay buum ak ay metit ñu ngi may nég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
lu moy li ma Noo gu Sell giy seereel ci dëkkoo dëkk, ne ma ay jéng aki coono moo may nég.