Acts 20:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Fi mu ne nag xam naa ne, dootuleen gis sama kanam, yéen ñépp ñi ma jaaroon ci seen biir, di yégle nguuru Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Léegi nag xam naa ne mboolem yeen ñi ma duggoon ci seen biir, di yégle nguurug Yàlla, dootuleen ma gis.