Acts 20:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
toog fa ñetti weer. Waaye bi mu nekkee ci kaw tànki dugg gaal jëm diiwaanu Siri, te Yawut yi lalal ko pexe, mu fas yéenee dellu, jaare Maseduwan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu toog fa ñetti weer. Gannaaw gi muy waaja dugg gaal jëm Siri, far pexe mu ko Yawut ya lalal feeñ, mu fomm, nara dellu jaareji Maseduwan.