Acts 20:32 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Léegi nag maa ngi leen di dénk Boroom bi, moom ak kàddug yiwam, gi leen man a dëgëral te may leen cér ci biir gaayi Yàlla yu sell yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Léegi nag, dénk naa leen Yàlla ak kàddug yiwam, gi leen mana dooleel, dencal leen seen muur ci biir mboolem nit ñi ñu sellal.