Acts 20:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu waxee loolu, mu sukk ak ñoom ñépp, ñaan ci Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la wax loolu, daldi sukkandoo ak ñoom ñépp, ñaan.