Acts 20:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li leen gën a teg aw tiis mooy li mu leen wax: «Dootuleen gis sama kanam.» Noonu ñu gunge ko ba ca gaal ga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
La leen yokk aw tiis nag mooy kàddu ga mu leen wax, ne leen: «Dootuleen ma gis.» Ba mu ko defee, ñu gunge ko ba ca gaal ga.