Acts 20:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñooñu nag jiitu, di nu nég dëkku Torowas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñu ñoo jiitu, di nu nég ca dëkk ba ñuy wax Torowas.
Recommended Reading