Acts 20:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, booloo nanu ngir damm mburu ma. Te Pool, mi bëggoon a dem ca ëllëg sa, di diisoo ak ñoom te waxtaanam law ba ci xaaju guddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca ndoortel ayu bés ba, naka lanu daje ngir dagg mburum bokkoo mi, Póol, yékkati kàddu, di wax ak gëmkat ñi, ndax fekk na mu bëggoona dem ca ëllëg sa. Wax ja nag law ba guddi ga xaaj.
Recommended Reading