Acts 21:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nga xamee ne tàggoo nanu ak ñoom ci naqar, nu dugg gaal, jubal dunu Kos. Te ca ëllëg sa nu dem ba teer ca Rodd, ba noppi jóge fa, jàll ba Patara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba nu tàggoo ak ñoom, nu dugg gaal, jubal dunu Kos, teg ca teeri ca dunu Rodd, jóge fa, jàll ba Patara.