Acts 21:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi ko njiit ya déggee, ñu màggal Yàlla ne ko: «Mbokk mi, gis nga ne, am na ay junniy Yawut ñu gëm, te ñépp a sawar ci yoonu Musaa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu dégg ca, daldi sàbbaal Yàlla, ba noppi ne ko: «Mbokk mi, xoolal ñaata junniy Yawut a doon ay gëmkat, te ñoom ñépp di ñu xér ci yoonu Musaa.