Acts 21:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lu nu ci war a def nag? Ndaxte ci lu wér dinañu xam ne, ñëw nga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu ciy pexe nag? Ndax kat duñu umple ne dikk nga.