Acts 21:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nu ngi lay digal nag, nga def nii: am na ci nun ñeenti góor yu dige ak Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi daal, dangay def li nu lay wax nii: nu ngi feek ñeenti nit ñu am lu ñu xasal Yàlla.