Acts 21:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li tax ñu wax loolu, mooy gisoon nañu Torofim mu Efes, ànd ak moom ca dëkk ba, te ñu yaakaar ne, Pool dugal na ko ca kër Yàlla ga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Torofim mu Efes la ñu gisoon ca dëkk ba, mu ànd ak Póol, ñu yaakaar ne Póol da koo yóbbu ca kër Yàlla ga.