Acts 21:37 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu koy bëgg a dugal ca tata ja, Pool ne kilifa ga: «Ndax man naa laa wax dara?» Mu tontu ko: «Yaw dégg nga gereg?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañu koy waaja dugal ca tata ja, Póol ne njiitu gàngoor ga: «Ndax man naa laa wax baat?» Mu ne ko: «Ndeke dégg nga gereg?