Acts 21:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nu wut taalibe ya, ba gis leen, toog ak ñoom juróom-ñaari fan. Ñoom nag ñu ne Pool ci li leen Xelu Yàlla mi may, mu bañ a dem Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu seet taalibey foofa, ba gis leen, toog ak ñoom juróom ñaari fan. Ci biir loolu Noo gu Sell gi di leen xiir ci wax Póol, ne ko bumu dem Yerusalem.