Acts 21:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nu jógee Tir nag, nu demaat ci géej, ba teer Patolemayis. Foofa nu nuyu bokk ya, yendu, fanaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag ba nu jógee Tir, danoo ñoqli ba teeri Patolemayis. Nu nuyoo faak bokki taalibe ya, toog faak ñoom benn fan.