Acts 22:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ma laaj ko: “Lu ma war a def, Boroom bi?” Boroom bi ne ma: “Jógal dem Damas, foofa dees na la biral lépp, li ma la yen.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma ne ko: “Sang bi, nu may def?” Sang bi ne ma: “Jógal dem Damaas, dees na la wax foofa mboolem li ñu la sas, nga def ko.”