Acts 22:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw gisuma woon dara ndax leeraayu melxat ga, ña ma àndal wommat ma, ma ñëw Damas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gisatuma woon dara ndax leeraayu melax ga; ña ma àndal ñoo ma mujj wommat, ba ma agsi Damaas.