Acts 22:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Bi ma ko defee ku tudd Anañas ñëw ci man. Nit ku ragal Yàlla la woon ci sàmm yoonu Musaa, te Yawuti Damas yépp seedeel ko lu baax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ku ñuy wax Anañas nag ma nga woon ca Damaas. Ku am diiney yoonu Musaa te rafetub jëw ci biir mboolem Yawuti dëkk ba.