Acts 22:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ma tontu ne: “Boroom bi, xam nañu ne, dama daan wër jàngoo-jàngu, di tëj kaso ak di dóor ay yar ñi la gëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma ne ko: “Sang bi, ñoom ci seen bopp xam nañu ne jàngu ci kaw jàngu, maa fa daan tëjlu ak a cawlu ñi la gëm.
Recommended Reading