Acts 22:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu déggee, mu di leen wax ci làkku yawut, ñu gën ne xeram. Noonu Pool ne leen:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu déggee yawut ya muy waxe ak ñoom, ñu gën ne xerem. Póol ne leen: